Léebu

Jóge Wikiquote.
Aller à la navigation Aller à la recherche
  • Ndankndank mooy japp golo ci ñaay.
  • Xaaral ba ginaar sax bëñ.
  • Lu cin xat xat, xorom ba xaj ca.