Universal Declaration of Human Rights
Aller à la navigation
Aller à la recherche
- Doomi aadama yépp danuy juddu, yam ci tawfeex ci sag ak sañ-sañ.
- Nekk na it ku xam dëgg te à nd na ak xelam, te war naa jëflante ak nawleen, te teg ko ci wà llu mbokk.